POESIE

HOMMAGE A SERIGNE MOUSSA GUEYE LAHI

today21 juin 2023 227 4 3

Arrière-plan
share close

HOMMAGE À MON PÈRE

Dieul sama tourou sanga bi (S.H.E.R.I.F M.O.U.S.S.A L.A.Y.E) def si beuyit

  • cover play_arrow

    Sherif Moussa Gueye Lahi BaySeydi Laye Gueye

S–  sanga lahi sopé sherif abdoulah.

Hhaafiz nga wone lolou la yallah defone si yaw.

E–  eutou mame Limamou Lahi bi liguey ngafa lou dotoul degn.

R–  rafetone nga xol lool Alassane, fan lagnuy dieuleuté bi kemaan.

I–   imaan bou feessone deleu ndax sa lep yallah lawone.

F–  fiiroo si sa xam xam ndax nieup ngassi dane rootal.

Mmatal nga sa mission ba delou si sa Borom bou mague ba

Oormal nga bepp mbindeef, taxawu nga wone nieup.

Uubbi ngafi dahira « Nourou lahi » tia médina boolé mbep tarikha.

S–  sameu nga sa ngor, Souxeut begeunté si domou adama yi.

S–  seleeu nga t sorei nga wone lool si xolou diam yi.

A–  aduna nga dane diangalé, koula dane deglou bou diogué geuneu geum borom ba.

L–  layene bi, diamou Yallah bi, Layanté biir mo nekone sa yité.

A–  alkhourane donone sa weeteul, nga deggone ko ba foko tafsiré xel yeup leer.

Y–  yaatalone say mbir boolé nieup aki digeul gnu diamou Yallah.

E–  elimaan bi, Yallana nga beel tia illayina si sa weetu Mame asws🙏🏾

Amiiine

Baye Seydi Guèye LAHI
ibn Shérif Moussa Guèye Lahi

POESIE

Rate it
0%
Restez informé des nouvelles publications en activant les notifications...! OK Non