A PROPOS DU LIVRE DE MAME LIBASSE LAHI : Nangu wala baň keemaani Yàlla
Nangu wala baň keemaani Yàlla Jublu waay yi teere bi am bi ci jiitu mooy wane ni Yàlla du yónni kumu joxul firnde. Moo tax werante amul yoon ci kuni Yàllaa ma yónni ndax suko yónnee man naň ci xam dara, suko yónni wul itam man naň ci xam dara. Werante wi nékk ci woote Seydinaa Limaamu Laay al-Mahdi (psl), mini « mana demb mana tay », dafay niru luy wane […]