RAPPEL A DIEU DE MAMADOU BARA LAHI : Le viatique de Soxna Maty Lahi bint Seydina Mame Alassane Lahi
Le viatique de Soxna Maty Lahi bint Seydina Mame Alassane Lahi Bara Laye sunu xol ndaw lolou daanou beguel kanie ngay nieuwate niou deufeul sune xol yi xool sa kanam Xana sa toukki bi dotoul dieex nga dellou ci xool ndiabote gui doom boula neexé delouwate fanga dieum Yow mane bou diante bi soo nga delouwate niou deufeul sene xol yi faté naxar wi sangaa kanam yi Baa saa'tane lahzatane […]