CONTRIBUTION

JËRËJËF SÉLOU BA LAHI de Baye Seydi GUEYE LAHI

today2 février 2025 116 4 3

Arrière-plan
share close

JËRËJËF SÉLOU BA LAHI

S – soodaan la diant fenké, SOODAAN COMMUNICATION la xabaar ya leeré, Selou Ba Lahi yaadi diambaari diiné gui ,ya ligueyal imamal Lahi asws

O – outinga xibaar founé buy dieuriñ aduna, akhloulahi dissi tataane, SOODAAN TV di sunu seetu, Selou Ba Lahi ya diara Jaajëfal

O – outi xibaar buy dëgël wootéb Seydina LIMAMOU LAHI asws diko tassaré ba ñeup jotsi, RADIO URUM BI lañuy deglu muñuy xamal Xayru Xalxi Lahi.

D – do ku ndaw si diiné ji, sa mission gërëm nañuko, SOODAAN PHOTO ak natal yu taaru ya, Sélou Ba Lahi yaadi jàmbaar.

A – ahloul beyti rassoul gui seedé nañu sa taxawaay, WA SOODAAN ñungui lay ñaanal YALLAH yagal lafi, Selou Ba Lahi amnga ndam.

A – am gëm gëm t yaadi gorr, yaa tedd. Noor ak nawett yangui dox si diiné ji, SOODAAN INFOS diñu leeral t lima woor moy Baye Lahi asws begg na si sa taxawaay bi.

N – nit bu am yitté, dou daw ludul si diiné, amal nga ndieuriñ kurël gui, dila ñaanaal gudu fan ak werr, taxawaay bu sax si diiné gui t Yallah fayal ñula bikalimati là illaha Illa làh.
Amine🙏🏾

Jërëjëf SELOU BA LAHI

BAYSEYDI Ibn SERIGNE MOUSSA GUEYE LAHI « LE POÈTE DE L’IMAM »

Écrit par: soodaan3

Rate it

Commentaires d’articles (0)

Laisser une réponse

Votre adresse email ne sera pas publiée. Les champs marqués d'un * sont obligatoires


0%
Restez informé des nouvelles publications en activant les notifications...! OK Non