Baye Seydi Laye Guèye es le fils de Serigne Moussa Guèye Lahi. Il rend ici hommage au regretté oustaz Bara Lahi.
BAYE SEYDI LAYE GUEYE DI SARGAL OUSTAZ BARA LAHI soodaan3
Xeuy nañu yawmal jummah si weeru shahban ñu tagué ñula
Baraa fi diougué ñukoy degg, sunu xol diiss, sunu xel nangu wuko degga
Yonen bi nga bëggoon lolou seedè nañko, té dinala teeru illayiina ak baye Saxir sa soppé ba.
Sa ruh delouna ca borom, sa jeuf gu rafet dess na dunya wayé molay bolé jotaay ak sanga ba.
Sama oustaz mangui ñaane Borom bi mu taaral la si leeru mustafaa 🙏🏾