ACTUALITES

SARGAL XALIFA YAA RASULU LAHI : Seydina Mouhamadoul Amine LAHI

today16 avril 2025 174 1

Arrière-plan
share close

Sargal khalifa bi Seydina Mouhamadoul Amine al khalifa

  • cover play_arrow

    SARGAL XALIFA YAA RASULU LAHI : Seydina Mouhamadoul Amine LAHI soodaan3

‎[1: bi Bismillah ma way fi doomi Mbaye 🙏🏻 Aboubacar té wayko diombé woul 🙏🏻

‎[2: samame Libass la yala diokh Lou doy 🙏🏻 tayak euleuk con way la diombé woul

[3: cou xam cou bakh té raniée ay mélom🙏🏻 na xool sambir con way la diombé woul

‎[4: kii may xalam mbiram ourous la né galam🙏🏻 Mouhamadou Lamine kii way ko diombé woul

‎[5: baboul õũloom sa baye ya raw kou xam🙏🏻 ga donou xam con way la diombé woul

‎[6: Bouy wakh Thi seydina issa sa baye🙏🏻 soun xole yi néekh con way la diombé woul

‎[7: Mamadou Lamine na bakh Mamadoul Amine🙏🏻Mouhamadoul Amine kii way ko diombé woul

‎[8: yaay ndeye DJI cheikh ndiaxan ga mas teudée🙏🏻 maslaa ga kay con way la diombé woul

‎[9: sa tab gou yaa woyof ba mélni xop🙏🏻 té yiw té bakh con way la diombé woul

‎[10: yaa seyidii ya saxiboul Houda baye 🙏🏻baye Mamadou Lamine kiii wayko diombé woul

‎[11: ziarana mouhtar sa mak diou bakh dia ak 🙏🏻imam Bassir kii wayko diombé woul

[12: Mame Ndjine na bakh di Gör sou kén yaboul🙏🏻xam xam bou wérr kii wayko diombé woul

[13: ma dém ziar mouhtar mou seydi mbaye imam🙏🏻 imam Mahtar kii wayko diombé woul

‎[14: dagan si naa té sakounaa sa niaan🙏🏻 Mame Alhassane kii wayko diombé woul

‎[15: ahlou LAH niou anda dém ziaari Abdou LAH 🙏🏻mbékk maagui nii kii way ko diombé woul

[16: yaa rabana yagal fi Seydinaa 🙏🏻 Mouhamadou Lamine kii wayko diombé woul

‎[17: daleloo ga tay khilafa mahdiyou🙏🏻té yay seuteum yaw wayla diombé woul

‎[18: waa ahlou laaye ya anda Nala tay🙏🏻 Antal khaliif Baye way la diombé woul

‎[19: yaa seydii imamou ahlou lahh🙏🏻diébalou Nanou nioun wakh ko diombé woul

[20: yaa raba bi diahi seydina 🙏🏻mahdiyouna kii way ko diombé woul

[21: salataan ãlaa imaminaa🙏🏻 sa Mame lamine kii way ko diombé woul

‎écris par m@me s@mb@ l@ye

Écrit par: soodaan3

Rate it

0%
Restez informé des nouvelles publications en activant les notifications...! OK Non